">

Réaction d’une proche de Fama Thioune après la liberté de son mari « Serigne… »

12 - Décembre - 2017

Le retour en force de Fama Thioune, après une semaine difficile. En effet, son mari a été arrêté pour trafic de visa et après sa liberté, Une proche de la jeune femme a posté un message émouvent sur sa page facebook. Découvrez juste en dessous

« borome keur ».
« Vive la liberté Sama dieukeur, sama kharite , sama nittou démbeu gui gniou sagal, ki gniou fonk , ki ame sougniou yeuremandé Cherie la brave Femme diambar khalé bi téral ndeyame ak bayame khalé bi mbeugue ayi mbokame khalé bi nago liguéyi khalé bi gueume ya Allah doyilo Seydina mouhamed psl té nope dieukeureume mbeugue dieukeur fonk dieukeureume Gueume borome keureume Fama Thioune borome Télé futur média .souma yalla mbeugué nama bayi ak yawou dama la fan barké cheikh néwone nala sougniou borome keureume dafa bari catégorie té sougniou borome loumou déf amna loutakh Mactar Seck dafa bok si khétou yonéte yalla youssouf té kousi bok dina Diarr prison wala ga dé alkhamdoulilahi c pas la 1er fois gniou dougale nitt prison ( kilifa douguouna prison , serigne dougal nagniouko prison , iman dougale nagniouko prison , kou défoule dara douguouna prison , borome khole bou rafete bakh di dimbalé kharitame douguouna prison kharite bi libre khana lou yalla déf amna loutakh alkhamdoulilahi Mactar sama kharite alkhamdoulilahi .doundalll chéri on t’aime »

Autres actualités

29 - Janvier - 2019

Fou Malade : « Pourquoi j’ai démenti mon frère Racine Talla » Souniou WaKeur Danio …

Fou Malade : « Pourquoi j’ai démenti mon frère Racine Talla » Souniou WaKeur Danio …

29 - Janvier - 2019

Cheikh Gadiaga détruit Gaston Mbengue et fait de graves révélations sur Assane Diouf, Rampino et ...

Cheikh Gadiaga détruit Gaston Mbengue et fait de graves révélations sur Assane Diouf, Rampino et ...

28 - Janvier - 2019

Adja Diallo annonce définitivement son divorce et révèle l’infidélité de son mari: Adja dévoile les messages scandaleux, Ibou Touré menace

Adja Diallo annonce définitivement son divorce et révèle l’infidélité de son mari Ibou Touré Adja Diallo annonce définitivement son divorce...

28 - Janvier - 2019

Ndeye Gueye « Dama Tegui Sama Tank, Thi Lou Beuri » Sama Dieukeur, Dafa Nek Thiii

Ndeye Gueye « Dama Tegui Sama Tank, Thi Lou Beuri » Sama Dieukeur, Dafa Nek Thiii

27 - Janvier - 2019

Vidéo: Affaire Adja Diallo Vs Karina persiste » je ne présenterai pas mes excuses «

Vidéo: Affaire Adja Diallo Vs Karina persiste » je ne présenterai pas mes excuses « L’histoire entre Karina Tavarez et Adja Diallo est loin de connaitre son...